CHEMIN DE LA LIBÉRATION-Yoonu Péexte
Appel à la mobilisation !
Le Sénégal sous Macky Sall est à fond dans la dictature. Les manifestations pacifiques prévues ce samedi 26 août 2023 dans plusieurs départements du Sénégal sont encore interdites.
La plateforme « Le Chemin de la Libération » ne compte pas se laisser étouffer par la stratégie du gouvernement de Macky SALL qui veut faire de ces interdictions un moyen de refroidissent de notre engagement.
Pour la libération de Ousmane Sonko et de tous les détenus politiques, la plateforme « Le Chemin de la Libération » appelle tous les sénégalais à se joindre aux concerts de casseroles organisés partout au Sénégal et dans la diaspora, le samedi 26 août, à partir de 20h.
Ensemble, faisons du bruit pour la justice et la démocratie.
Na ñépp jóg !
Ginnaaw tere gi Maki Sàll taxaw tere feeñu yi ñu nammoon amal ci 19i gox ci Senegaal, kuréel gi di « Yoonu Péexte » fasul yéene seetaan pexey nguurug Maki Sàll jëm ci nasaxal sunu taxawaay.
Kuréel gi di « Yoonu Péexte » wéy di tënku ci taxawaayam muy xax ci amal ay feeñu ci jàmm ak dal ngir ñu féexal mbooleem ñi ñu tëj kaso ndax politig, mooy woo waa Senegaal yépp ci tëggum bool fii ci réew mi ak bitim-réew, ci gaawu 26i fan ci weeru ut bu 20i waxtu jotee.
Nañu ànd ñun ñépp tëgg mu xumb ngir aar demokaraasi ak yoon.
Dakar, le 25 août 2023, Pour « Le Chemin de la Libération »
Me Ngagne Demba TOURE